![]()
(Couplet 1)
Soma guissé à la télé guéné
woumathi sa yéné finiou di-
ougué ak finiou téré ate yih
daw diko sédé
Xamal ngama sama lepp, teh
meussou loh ma juger, amouma
loum la fey buur, yallah rek
la ley bayé
Mangui faté liko guudi yih
niou done passé tokk dih
waxtane dih reve wando done
ay xalei
Mane damey fier somey titeuro
sama wadji, dey gueuneu neexi
ndakh yaffih nekone bamouy
metti
(Refrain)
Sama lonko ola ola, ola la
diap nala ndakh sa djiko ola
ola, ola ola
Yako fa am tey ma weuyla ola
ola, ola ola, un poco un poco
c’est toi ola ola, ola ola
mon ami est là
Négh koti koti mane, kone yoli
yoli, Négh koti koti mane, kone
yoli yoli, negn thioki thioki
mane, thioki bah fin, un poco
un poco c’estmon ami est là
(Couplet 2)
Yow wonala, xarito sama wonala
gorr deugueu wolou nala rempl-
acer la non non non
Dou loumey meune mane mih ola
ola ola dama ley xoll dih guiss
sama bopp xarito bi doyna settu
teh fouma diaxleh wola c’est
tout
Meussou loh ma bayi doma sétane
souma réré sa dieum djé takh
meussouma yeug fouma wété
Diapaleh léne ma guirr niou
meuguign sama wadji danga diap
xaro si mane dara sama fété
(Refrain)
Sama lonko ola ola, ola la
diap nala ndakh sa djiko ola
ola, ola ola
Yako fa am tey ma weuyla ola
ola, ola ola, un poco un poco
c’est toi ola ola, ola ola
mon ami est là
Négh koti koti mane, kone yoli
yoli, Négh koti koti mane, kone
yoli yoli, negn thioki thioki
mane, thioki bah fin, un poco
un poco c’estmon ami est là
Voir aussi Gudi
Added by
lyrics africas
WRITE A COMMENT
WRITE A COMMENT

No comments yet