![]()
(Couplet 1)
Jeguéma ma wone là li nek
ci sama xol, degluma ma dé
là, li ngay def ci sama
khel May la tié ndax lii dé
nène là
Xol bii li muy tegge lépp deg
g la, gem naa ne lii dé mayu
yàlla laa, moom minu bolé, tia
aras lanu ko fassé Mayu yàlla
laa
(Pont)
xalé la ba tey, lou yagg defay
faye, kon naa si népp tey, taa
kham né lii dou faaye,
sama xol yaw la fal sa boss
deh man la tann, fooy, yendu
lay fanane, sama baby kaye
(Refrain)
Gen ci man, baax ci man, gaw
ci man, ses ci man, yow ya ses
ci man
Dof ci man, men ci man, sax
ci man, woor ci man (Yow ya
wor ci man)
(Couplet 2)
Tanka tank, mbagg mbagg, lo
diok honé ma dagg lu ma begg
ci sa dek
Ndank ndank ba yeg fu sori,
japp bana bayi doon ci xàddj
doon ci tayyi xel bey sédé,
nena totie nga bopp bi,
xalatul ku dul yaw yaw yaa
fi né
Xol bé sédé limuy doundou mo
nexx Nexxa nexxa nexx beugoul
mou diexx
(Pont)
xalé la ba tey, lou yagg defay
faye, kon naa si népp tey, taa
kham né lii dou faaye,
sama xol yaw la fal sa boss
deh man la tann, fooy, yendu
lay fanane, sama baby kaye
(Refrain)
Gen ci man, baax ci man, gaw
ci man, ses ci man, (yow ya ses
ci man)
Dof ci man, men ci man, sax
ci man, woor ci man (Yow ya
wor ci man)
Gen ci man, baax ci man, gaw
ci man, ses ci man, (yow ya ses
ci man)
Dof ci man, men ci man, sax
ci man, woor ci man (Yow ya
wor ci man)
Added by
lyrics africas
WRITE A COMMENT
WRITE A COMMENT

No comments yet