Loading

(Intro)

Sama chérie boy nieuwul
niou feulalée, Tapaa – tapaa

(Couplet 1)

Mane sama lova lova mane miirnaa
Yaw nigua mélni lanla
Sa mélokane kémane la
Maytoul dogalima

Mane sama lamine bi nala thiaatou
Kane mo dampe ki yaya yaa
Un corps si parfait
Moytoul dogalima

Diéguéma té boul ma sarééééy
Nala may lima yorée
Kay ma nékhal la
Yaw ligua beugue lay déf

Xalé bi neékh Na ci bir mbuéguél
Xol bi yeukna thiofeel
Kay fii ma nékhal la
Yaw ligua beugue lay déf

(Pont)

Té sou niou mbueguél lolou
lénéén la ( sou niou mbueguél
lolou lénéén la) Huum sama
chérie boy kay fii nieuw niou

feulalée ( Huum sama chérie
boy kay fii nieuw niou feulalée)

Hum sama chérie boy maala
nop looll waawaaw ( sama
chérie boy maala nop looll waawaaw)

Oh moi je t’aime
Je t’aime, je t’aime, je t’aime

(Refrain)

À la folie ma chérie je t’aime oh
Oh oh ô,oh oh ô,oh oh ô ,oh oh ô ,
à la folie ma chérie je t’aime oh
( oh oh ô,oh oh ô,oh oh ô,oh oh ô)

Kay ma wayal laa
Kay ma wayal laa
Ma wayal laa

(Couplet 2)

Mane sama lova lova mane miirnaa
Yaw nigua mélni lanla
Sa mélokane kémane la
Maytoul dogalima

Xalé bi neékh na ci bir mbuéguél
Xol bi yeukna thiofeel
Kay fii ma nékhal la
Ligua beugue lay déf

(Pont)

Té sou niou mbueguél lolou
lénéén la ( sou niou mbueguél
lolou lénéén la) Huum sama
chérie boy kay fii nieuw niou

feulalée ( Huum sama chérie
boy kay fii nieuw niou feulalée)

Hum sama chérie boy maala nop
looll waawaaw ( sama chérie boy
maala nop looll waawaaw)

Oh moi je t’aime
Je t’aime, je t’aime, je t’aime

(Refrain)

À la folie ma chérie je t’aime oh
Oh oh ô,oh oh ô,oh oh ô ,oh oh ô ,
à la folie ma chérie je t’aime oh
( oh oh ô,oh oh ô,oh oh ô,oh oh ô)

Kay ma wayal laa
Kay ma wayal laa
Ma wayal laa

Baby yaw nima léréé ( nima léréé)
Baby yaw nima léréé ( nima léréé)
Mane rék ma nék ci sa xol
Yaw rek ya nék sama xol

Baby yaw nima léréé ( nima léréé)
Nim-ma léréé
Mane rék ma nék ci sa xol
Yaw rek ya nek sam xol

Baby yaw nima léréé ( nima léréé)
Nim-ma léréé,may sa daleuh
yamay soll, Wouyou ma sama
reinou xol, Wuyumaaa déma réééééééé.

Added by

Sophina Malonda

SHARE

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *