Loading

(Couplet 1)

Yow..
Fimala def sama xol bi
dou thiaxàn’alafiy guené
Thionoo… Yima dadj pour
niou beuganté bb xam’nga
nimou démé

Yoon bi meti woon niou
diaayanté ko, Bou diarone
tour deret ma rayanté ko
Mindef meunoul tax baniou
bayanté no, Té niom meunougn
tax baniou gaagnanté mak ioe

(Pont)

Nimala beugué bo dawone ay
kilometa, Taxoul nga dap ma
Nimala nobé bo dawone ay
kilometa yeah, Taxoul nga dap ma

(Refrain)

Ningama beugué nouko
raw laala beugué, Bb bo
dawone ay diouni kilometa
Taxoul nga dap ma, Ning’ma

beugué nonou laala rawé
Bo dawone ay kilometa
Taxoul nga dap ma

Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa

(Couplet 2)

Damala beugeu ba tiit sama bopp
Yow bingay def sama xol BAAXOUL
Douma setane dara dila wokk
Bou diaré la taylé sama nafsou

Xalei bi doonal sama nattou
Bilay dawou mathi dara, Wowal
leen ma Tycco Tattou, Ndax sa
tour laa beuggeu mou defal ma
sama yaaram

(Pont)

Nimala beugué bo dawone ay
kilometa, Taxoul nga dap ma
Nimala nobé bo dawone ay
kilometa yeah, Taxoul nga dap ma

(Refrain)

Ningama beugué nouko
raw laala beugué, Bb bo
dawone ay diouni kilometa
Taxoul nga dap ma, Ning’ma

beugué nonou laala rawé
Bo dawone ay kilometa
Taxoul nga dap ma

(Couplet 3)

Yama momen, Foma wo ma nieuw
Ndèkè damala bopp Top Xol bi
loum ma diguel ma def

Tothi kani pathial ligom
May kiy saf safal sa adouna
Bebe yama tigom Thia kawa kaw
Ya takh ma rew waw

Nènagne ya takh ma rew
Mani lene beuguel bathia
dakh moy nga nope kala nop waw
Aldiana yaw ya takh ma rew
Dakh danga ma nope ma nope
la rawè ay kilometa

(Refrain)

Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa

AH ah ah, Daw ay Diouni
Kolomètre takhoul ga dab ma
AH ah ah, Daw ay Diouni
Kolomètre takhoul ga dab ma (3x)

Added by

lyrics africas

SHARE

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *