Loading

(Couplet 1)

Bou xol bi di dioy my bae
Mane ma gneuw nakh ko
Sentiment yi nékoul lep
Fok dieuf yi wané ko

Yaw la denke sama life
Kone lo wakh d’accord
Sa djiko ji dafa nice
Kone fok ma wakh ko

Bougouma dé thi love sans nek
Ak yow bae nakh yay sama aljana
Mane ak yow Lou réal là, Wakh na ko
Gneup gnima kham yay sama adouna

(Refrain)

Beugue nala
Yay sama waay
Bo dioyé ma nakh là
Beugouma ngay cry

Beugue nala
Yay sama waay
Bo dioyé ma nakh là
Beugouma ngay cry baby

(Couplet 2)

Niata goor niola nope
Yow ngani mane rek
Ligni yoré nimou tolol
Yaw ga tocc né tekk

Goré nga si mame mi pourquoi
May changer di weuri kenen
Yay sama waay my homie kay niou dem

Sougnou diganté len
Meussoul gnaw, bougnou
Bayi kéne di yak li, gnar
Gnou beuganté dougnou déss guinaw
Yama dieulé fé indi ma fi

(Refrain)

Beugue nala
Yay sama waay
Bo dioyé ma nakh là
Beugouma ngay cry

Beugue nala
Yay sama waay
Bo dioyé ma nakh là
Beugouma ngay cry baby

Added by

lyrics africas

SHARE

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *